1.Jaar-jaar ya 16:1-42 WOLB2025 - Bible AI

1Gannaaw loolu ñu indi gaalu Yàlla ga, yeb ko ca biir xayma ba ko Daawuda sampal, ba noppi ñu joxe fa kanam Yàlla ay saraxi rendi-dóomal|lemma="Sarax yi:"* ak saraxi cant ci biir jàmm|lemma="Sarax yi:"*.

2Ba Daawuda defee saraxi rendi-dóomal yaak saraxi cant ci biir jàmm, ñaanal na askan wa ci turu Aji Sax ji.

3Daawuda daldi jox kenn ku nekk ci waa Israayil góor ak jigéen menn mburu ak nàkkub tàndarma ak nàkkub reseñ.

4Ba loolu wéyee Daawuda tànn ñenn ca Leween ña, ñuy liggéey fa kanam gaalu Aji Sax ji, di woy, di sant aka màggal Aji Sax ji Yàllay Israayil.

5Ñooñu Asaf a leen jiite woon, Sàkkaryaa di seen ñaareelu kilifa, ña ca topp di Yewel ak Semiramot ak Yexyel ak Matica ak Elyab ak Benaya ak Obedd Edom ak Yewel. Ñooñu wara yore ay jumtukaayi xumbéen yu mel ni ay xalam aki kooraa, Asaf yore tabala ji,

6Benaya ak Yaxasyel, sarxalkat ya, wara dëkke di wal liit ya fa kanam gaalu kóllërey Yàlla ga.

7Bésub keroog la Daawuda njëkka dénk Asaf aki bokkam liggéeyu cant yi, ñeel Aji Sax ji, woy wa jib:

8Santleen Aji Sax ji, tudd turam,

9Woyleen ko, tagg ko,

10Damooleen turam wu sell,

11Wutleen Aji Sax ji, sës ci dooleem.

12Fàttalikuleen ay jalooreem

13Yeen sëti Israayil, jaamam ba,

14Kee di sunu Yàlla Aji Sax ji,

15Fàttalikuleen kóllëreem|lemma="kóllëre g-:"* ba fàww,

16Mooy digeem baak Ibraayma,

17Moo ko dëggalal Yanqóoba, sàrtal ko,

18Moo noon: «Yaw laay jox réewum Kanaan

19Ba bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"* doonee ñu néewa néew,

20di wëreelu ci biir xeetoo xeet,

21mayul kenn mu noot leen,

22ne leen: «Buleen laal ñi ma séddoo

23Woyleen Aji Sax ji yeen àddina sépp,

24Siiwalleen màggaayam ci biir xeet yi,

25Aji Sax jee màgg, jara sant a sant

26Mboolem yàlla yi xeet yiy jaamu, yàllantu la,

27Màggaay ak daraja, fa moom,

28Yeen làngi xeet yi, seedeelleen Aji Sax ji,

29Seedeelleen Aji Sax ji màggaayu turam,

30Ragalleen ko, bay lox, yeen waa àddina sépp.

31Asamaanoo, bégal!

32Géejoo, riiral yaak mboolem li la fees,

33ba garabi àll bi teertoo Aji Sax ji ay sarxolle,

34Santleen Aji Sax ji, kee baax,

35Àdduleen, ne ko: «Yaw Yàlla mi nuy musal,

36Santleen Aji Sax ji Yàllay Israayil,

37Ba mu ko defee Daawuda dëddu, bàyyi Asaf aki bokkam ca kanam gaalu Aji Sax ji, ngir ñuy saxoo liggéey fa kanam gaal ga, di fa def la leen war bés bu nekk.

38Ci biir loolu mu tabb ay wattukati bunt; ñuy Obedd Edom, ku góor kay doomu Yedutun, ak juróom benn fukki góor ak juróom ñett (68) ñu mu bokkal, boole ca Osa.

39Ci kaw loolu Daawuda dénk Cadog ak yeneen sarxalkat yi mu bokkal liggéey ba, ca jaamookaayu Aji Sax|lemma="xaymab ndaje m-:"* ja ca tundu Gabawon.

40Ñuy def bés bu nekk, subaak ngoon, ay saraxi rendi-dóomal ca kaw sarxalukaayu rendi-dóomal|lemma="sarxalukaay b-:"* ba, ñeel Aji Sax ji. Loolu dëppook mboolem li ñu bind ci téereb yoon wi Aji Sax ji jox Israayil.

41Ba loolu amee ñu ànd ak Eman ak Yedutun ak ñeneen ñi ñu tànn, jagleleen ñu wara sante Aji Sax ji baat yii: «Li ko waral mooy ngoram gi sax dàkk.»

42Eman ak Yedutun ñoo féetewoo woon liit yaak tabala ya ak yeneen jumtukaayi xumbéen yi jëm ci woy Yàlla; doomi Yedutun yu góor nag di taxaw ca bunt ba.

cle>