1Ab yéenee ngii bu ñu won Yonent Yàlla Abakug.
2Éy Aji Sax ji|lemma="Aji Sax j-:"*, foo àppal lii?
3Ana loo may wone lu bon,
4Moo tax yoon lafañ,
5«Xoolleen ci biir xeet yi ba gis,» la Aji Sax ji wax.
6Maa ngii di dooleel waa Babilon,
7Ñu ñàng, raglu,
8Seeni fas a gëna gaawi segg,
9Aw ay lañuy dikke, ñoom ñépp,
10Ñooñu ay buur lañuy ñaawal,
11Jàll, wéy lañu cay teg ni ngelaw,
12Waaye Aji Sax ji, xanaa du yaa masa nekk?
13Sa gët yu sell jomb naa niir lu bon,
14Yaa def doom aadama mel niw jën,
15te ñoom ñépp la ku bon di korandoo,
16Moo tax muy rendil mbaalam ab sarax,