Abdiyas 1:1-21 WOLB2025 - Bible AI

1Peeñum Abdiyas a ngii. Boroom bi Aji Sax ji|lemma="Aji Sax j-:"* moo wax lii ñeel askanu Edom+ 1.1 Edom mooy xeet wi soqikoo ci Esawu seexu Yanqóoba mi meññ Israayil.*.

2Aji Sax jee ne waa Edom:

3Seen reewande sànk na leen,

4Su ngeen kaweeloon nig jaxaay,

5«Su leen ay sàcc dikkalee, mbaa sëxëtookati guddi,

6Waaye céy ni ñuy sëxëtoojee askanu Esawu!

7Mboolem ñi ngeen fasool kóllëre|lemma="kóllëre g-:"*

8«Xanaa du bésub keroog,» kàddug Aji Sax jee,

9Yeen waa Teman+ 1.9 Teman, sëtub Esawu, lañu dippee dëkkub Edomeen ba woon ca bëj-gànnaaru réew ma, te moo taxawe fii réewum Edom gépp.*, seeni jàmbaar ay jàq,

10«Soxore gi ngeen soxore seen mbokk Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*

11Bésub keroog ba ngeen taxawee,

12Waruleen woona seetaan ci seen bésub mbokk,

13Waruleen woona dugg sama dëkku ñoñ,

14Waruleen woona taxaw fa selebe yoon ya,

15«Bésub Aji Sax|lemma="bésub Aji Sax j-:"* ji déy, dëgmal na,

16Yeen waa kër Yanqóoba,

17Waaye kaw tundu Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* la aw ndes di rawe,

18Kër Yanqóoba sawara lay doon,

19Waa bëj-saalumu Yuda ñooy moom tundu Esawu,

20Waa Israayil ñi ñu gàddaayloo woon,

21Ay xettalikat ñooy yéeg kaw tundu Siyoŋ,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>