Amos 5:1-26 WOLB2025 - Bible AI

1Amos ne: Yeen bànni Israayil, dégluleen mii pent; maa ngi leen di jooy, yeen bànni Israayil!

2Fëlëñ!

3Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne:

4Aji Sax ji da ne waa kër Israayil:

5Buleen wuti Betel,

6Wutleen Aji Sax ji, te dund.

7Wóoy yeen ñiy walbati àtteb yoon, mu mel ni xay,

8Kee sàkk biddiiwi lolli ak biddiiwi cooroon,

9Moo naan musiba jàyy ci kaw boroom doole,

10Yeena bañ kuy yedde ci pénc,

11Gannaaw yeenay noot néew-ji-doole,

12Ràññee naa seen bàkkaar yu bare

13Moo tax ku xelu ci jii jamono ne cell.

14Sàkkuleen lu baax, bàyyi lu bon, ba dund,

15Bañleen lu bon, bëgg lu baax,

16Moo tax Boroom bi Aji Sax ji, Yàlla ji ci gàngoori xare yi, dafa ne:

17Tóokëroo tóokër ay ubalee ki yuux.

18Wóoy kuy yàkkamti bésub Aji Sax|lemma="bésub Aji Sax j-:"* ji!

19Day mel ni kuy daw gaynde,

20Xanaa du lëndëm gu dara leerul la bésub Aji Sax jiy doon,

21«Maa bañ, maa sib seeni màggal,

22Ngeen defal ma saraxu rendi-dóomal|lemma="Sarax yi:"*,

23Xiddileen maak seen coowal jàng.

24Na yoon wal mel nim ndox,

25«Yeen waa kër Israayil, saraxi gàtt ak saraxi pepp,

26Te ngeen di yékkati seen tuur yi ngeen sàkk:

© 2025 Bible Society of Senegal
/div>