Amos 9:1-15 WOLB2025 - Bible AI

1Ma gis nag Boroom bi, mu taxaw ca sarxalukaay|lemma="sarxalukaay b-:"* ba. Mu ne:

2Bu ñu bëttoon, ba biir njaniiw it,

3Bu ñu nëbbu woon kaw tundu Karmel it,

4Su ñu demee, diy jaam ñu seeni noon jiital,

5Boroom bi, Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi,

6Kee tabax kaw asamaan néegi biiram,

7«Bànni Israayiloo|lemma="bànni Israayil:"*, xanaa du yeen ak waa Kuus|lemma="Kuus:"* laa yemale?»

8Boroom bi, Aji Sax jaa ngi ne jàkk

9«Maa ngii déy di sant xeetoo xeet,

10Saamar ay rey mboolem sama bàkkaarkati mbooloo

11«Bésub keroog maay yékkati mbaarum Daawuda mi daanu,

12Su boobaa bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"* nangu ndesu Edom,

13«Ay bés a ngii déy, di ñëw,»

14Maay tijji wërsëgu Israayil, sama ñoñ;

15Maa leen di jëmbat fi seen suuf,

© 2025 Bible Society of Senegal
/div>