Ase 2:1-23 WOLB2025 - Bible AI

1Ca ñaareelu atu nguuru Buur Daryus, ca juróom ñaareelu weer wa, yemook ñaar fukki fan ak benn+ 2.1 Bés boobu moo mujjoon ci màggalu bési Mbaar yi.*, kàddug Aji Sax ji moo dikk ci jottalib Yonent Yàlla Ase. Mu ne:

2«Waxal nag doomu Selcel, Sorobabel boroom Yuda, ak doomu Yoccadag, Yosuwe sarxalkat|lemma="sarxalkat b-:"* bu mag bi, ak ñi des ci askan wi, nga ne leen:

3“Ana ci yeen ñi fi des, ku gisoon

4Léegi nag, Sorobabel, góor-góorlul,

5Googu kàddu laa jaayante woon ak yeen,

6Aji Sax ji Boroom gàngoor yi kat dafa wax ne:

7Maay yëngal xeetoo xeet,

8Maa moom xaalis, moom wurus;

9Daraja ji kër gii di mujje mooy sut ja woon,

10Ca ñaar fukki fan ak ñeentu juróom ñeenteelu weer wa+ 2.10 Mu yemook ñetti weer gannaaw ndoortel tabaxu kër Yàlla ga.*, yemook ñaareelu atu nguuru Buur Daryus, kàddug Aji Sax ji moo dikkal Yonent Yàlla Ase, ne ko:

11«Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Sàkkul nag ndigal ci sarxalkat|lemma="sarxalkat b-:"* yi, nga ne leen:

12Waaw, su nit yoree ci lafu mbubbam aw yàpp wu ñu sellal, ba noppi lafu mbubbam laal mburu mbaa lu ñu togg, mbaa biiñ mbaa ag diw mbaa ñam wu mu doon, ndax loola day daldi sell|lemma="sell:"*?» Ase laaj ko sarxalkat ya, ñu ne ko: «Déedéet.»

13Ase dellu ne leen: «Nit ku sobewu ndax ab néew bu mu laal, su laalee lenn ci mboolem ñam yooyu, ndax ñam wa sobewu na?» Sarxalkat ya ne ko: «Sobewu na kay.»

14Ase nag wax leen, ne leen:

15«Léegi nag seetaatleen seen xel bu baax,

16ku wuti waan ñaar fukki natti pepp,

17Maa leen dumaa gàncax gu lax ba benaat,

18Seetaatleen seen xel bu baax,

19Ana am jiwooti ci sàq yi?

20Kàddug Aji Sax ji nag dikkaat Ase, yemook ñaar fukki fan ak ñeent ci weer wi. Mu ne:

21«Waxal Sorobabel+ 2.21 Sorobabel mi soqikoo ci Daawuda moo taxawe buur bi feddali kàddug Aji Sax ja mu noon mooy taxawal nguur gu sax dàkk, ñeel askanu Daawuda. Seetal ci +bk 2.Samiyel+bk* 7.11-16, ak +bk Macë+bk* 1.12-13.*, boroom Yuda, ne ko:

22Maay jàllarbi ngànguney nguur yi,

23Bésub keroog,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>