Ayóoba 10:1-21 WOLB2025 - Bible AI

1Maaka bañ sama dund gii!

2Dama naa Yàlla: Bu ma toppug tooñ.

3Ana lu la noote di jariñ,

4Xanaa gëti nit doŋŋ nga am,

5Say fan daa tollook fani doom aadama,

6ba ngay seet fu ma ñaawe,

7Moona xam nga xéll ne tooñuma,

8Say loxoo ma mooñ, tabax ma ba ma mat sëkk,

9Rikk fàttalikul ne yaa ma tabax, ni bu ma doon ban,

10Xanaa du yaa ma xelli woon ni meew

11wodde ma der ak suux,

12Yaa ma may bakkan, won ma ngor,

13Ndeke yoo lii nga dencoon ci sa xol,

14ne ma dann, ba su ma bàkkaaree,

15Su ma defee lu bon, ngalla man,

16Waaye su may siggi rekk,

17yónneeti ma say seede,

18Ana loo ma doon génnee sama biiru ndey?

19Doon naa mel ni ku masula am,

20Xanaa du fan yu néew laa dese? Ba ma boog!

21bala may dëddu, délseetuma,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>