Ayóoba 19:1-28 WOLB2025 - Bible AI

1Ayóoba àddu ne:

2Dungeen ma noppee xañ jàmmi bakkan,

3Fukki yoon a ngii ngeen di ma saaga,

4Su ma moyoon dëgg sax,

5Defe ngeen ne yeena ma gën,

6Waaye xamleen ne Yàllaa ma tooñ,

7May woote wall, wuyeesu ma,

8Manumaa jàll, Yàllaa fatt sama yoon,

9sàggi sama sag,

10tojat ma wetoo wet ba ma tàggoo,

11jafalal mam sànjam,

12ay gàngooram dikkandoo,

13Samay bokk, mu soreleek man,

14Jegeñaale ba ma,

15sama gani démb def ma ni jàmbur tey,

16Su ma doon woo sama surga, ba di ko tinu sax,

17Sama xetu gémmiñ dàq na sama jabar,

18Gone yi sax a ngi may sewal,

19Sama wóllërey démb yépp a ma seexlu,

20Der aki yax laa dese,

21Yërmandee, yërmande, yeen samay xarit,

22Lu ngeen ma toŋale nii ni Yàlla?

23Éy su samay kàddu tënku woon ci mbind!

24xacce ko xalimag weñ ak betteex

25Waaye man xam naa ne sama Jotkat|lemma="jotkat b-:"* a ngi dund,

26Bu sama der bi lekkoo sax,

27xoolal ko sama bopp,

28Yeena ngi naan: «Ana nu nu koy toŋale,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>