Ayóoba 20:1-28 WOLB2025 - Bible AI

1Cofar mu Naama àddu ne:

2Kon ma àddooti ndax jaaxle,

3Dégg naa kàddug yedde gi nga may saagaa,

4Xanaa xamoo lii? La dale ca cosaan,

5xamoo ne ku bon, ag sarxolleem àggul fenn,

6Bu màggoon ba tollook asamaan it,

7day mujj seey fàww niy jonkanam;

8Kenn du ko gisati, day réer ni gént,

9Bët bu ko gisoon du ko tóllanti,

10ay doomam ay dàmp néew-ji-doole yi,

11Mooy ànd ak dooley ndawam,

12Lu bon la daa tàqamtikoo,

13di ko siiramtal te du ko wacc,

14Waaye la muy lekk ay soppiku ca biiram,

15Moo dërëxoon alal, moo koy goqi,

16Ndeke tookey ñàngóor la muucu,

17Yàlla bumu niir wali dex

18Dina delloo lu mu amoon, du ko warax;

19Moo dëggaate néew-ji-doole, dëddu ko;

20Biir ba du wéet,

21Dara du rëcc ab kollam,

22Fa mu regge lay jàqe,

23Ba muy sol kollam

24Mu daw ngànnaayu weñ,

25jam ko ba fëll,

26Mboolem lëndëm a làqu di ko xaar,

27Asamaan ay weer ñaawtéefam,

28Koomum këram day tukki, ne mes,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>