Ayóoba 27:1-22 WOLB2025 - Bible AI

1Ayóoba yékkateeti baatam, ne:

2Yàlla miy dund seede na, moom mi ma xañ dëgg

3ne li feek may ànd ak bakkan,

4sama gémmiñ gii du wax njubadi,

5Yàlla buma leen jox dëgg,

6Ci sama dëgg laay ŋoy, duma ko ba,

7Yal na noon bokk ak ku bon demin,

8Ana lu yéefar biy yaakaarati bu ko Yàlla beddee,

9Bu ko njàqare di dikkal,

10Ndax Aji Man ji la daan bége,

11Ma xamal leen boog li ci dooley Yàlla,

12Dama ne, yeen ñépp a ko gisal seen bopp sax,

13Lii mooy cér bi Yàlla sédd ku bon,

14Njabootam ne xas, saamar jagoo,

15Ña koy wuutu, mbas a leen di rey,

16Su doon jal xaalis ni suuf,

17mooy dajale, aji jub sol;

18Mooy tabax kër gu tanewul mbaarum wattukatu tool,

19Keey tëraale alal ju mu dul gisati;

20Tiitaangee koy dab nim wal,

21ngelawal penku déjjatee ko këram,

22Dees na ko diir, bañ koo ñéeblu,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>