Ayóoba 29:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1Ayóoba yékkateeti baatam, ne:

2Éy ku ma doon delloo jamono ya woon,

3ba mu may tiim, di ma niital,

4ba ma tolloo sama digg doole,

5Booba Aji Man jaa ngeek man ba tey,

6may jàngoom niw,

7Bu ma génnaa ba ca buntu dëkk ba,

8waxambaane gis ma, ñooru,

9kàngam ne xerem,

10garmi ne selaw,

11nopp dégg ma, ndokkeel ma,

12Néew-ji-doole woote, ma wallu,

13Ñaanu ku naroona sànku di ma dal,

14Njekk laa woddoo woon, njekk wodd ma,

15Silmaxa, maa dooni gëtam;

16Néew-ji-doole, maa doon baayam,

17Ku jubadi, ma dammi ŋaamam,

18Ma noon samay fan dina neexook feppi suuf,

19Ma noon su ma doon garab samay reen fëllem ndox,

20Ma noon darajaa may yeesalal nganam,

21Man lees daa déglu, di ma xaar;

22Samay kàddoo leen di dal, genn-genn,

23Booba lees ma daa séentu nib taw;

24Samay ree gëmeesu ko woon,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>