Ayóoba 32:1-21 WOLB2025 - Bible AI

1Fa la ñetti góor ñooña noppee tontu Ayóoba, ndax la Ayóoba gis njekkam.

2Ba loolu amee Eliyu doomu Barakel ma askanoo ci Buus, bokk ci làngu Ram daa mer ba futt ca la Ayóoba dëggal boppam fi kanam Yàlla,

3ak la ñetti xariti Ayóoba ya ñàkk lu ñu ko tontu, ba tax ñu teg Yàlla tooñ.

4Eliyu nag moo mujjoona wax ak Ayóoba, ndax moo féete ndaw ñett ña.

5Mu gis ne ñetti góor ña amatuñu tont, xol ba sot, mu mer ba futt.

6Ca la Eliyu doomu Barakel waa Buus ba, àddu ne:

7Ma noon: «Na yàgga-dund wax,

8Ndeke xel mi ci nit

9Gudd fan taxula rafet xel,

10Moo tax ma ne: «Déglu ma;

11Dama ne, négandiku naa seeni kàddu,

12Yeen laa doon teewlu,

13Buleen ma ne: «Xel mu rafet mi nu ci gis moo di:

14Du man la Baay Ayóoba jëme kàddoom,

15Ñii kat jommi nañu, waxatuñu;

16Dama leen di xaar te waxuñu,

17Damay tontu sama wàll, man it;

18Sama dënn a fees aki wax,

19Sama xol baa ngii mel ni lu sol biiñ, ube ràpp,

20Naa wax boog, ba féex,

21Duma ci am xejj ak seen,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>