Ayóoba 34:1-36 WOLB2025 - Bible AI

1Eliyu dellu ne:

2Yeen ñi xelu, dégluleen samay wax,

3Purux déy ay mosu ñam,

4Kon nan ànd seet li dëggu

5Baay Ayóoba kat nee moo yey,

6Mu am dëgg, ñu ne moo fen,

7Ana ku mel ni Baay Ayóoba mii,

8di àndandook ñiy def lu ñaaw,

9te naa: «Nit ki seet bànneexu Yàlla,

10Kon yeen niti xel ñee, dégluleen ma,

11Jëfu doom aadama ji daal, moom la koy fey;

12Li wóor mooy Yàlla du def lu bon,

13Ana ku ko dénk kilifteefu dun bi?

14Bu ci Yàlla yebu woon,

15bépp boroom bakkan ay bokk ne lasiim,

16Ndegam am nga ag dégg, déggal lii,

17Manees naa jiite te bañ njub?

18Kii moo naan buur: «Yaa sew!»

19Kii du far kàngam,

20Nes tuut, dee dikke xaaju guddi,

21Yàlla déy a ngi ne jàkk ci jaar-jaari nit ki,

22Du fenn fu lëndëm mbaa fu ne këruus,

23Yàlla daal, soxlawula liñbat nit ki,

24Mooy rajaxe boroom doole te du laajte,

25Moo ràññee moos jëfi boroom doole,

26Moo koy dóore fu ne fàŋŋ,

27Li ko waral di boroom doolee dëddu Yàlla,

28ba yuuxi baadoola yi àgg fa moom,

29Bu Yàlla nee cell, ana ku koy ŋàññ?

30ngir yéefar bi baña falu,

31Su nit ki nee Yàlla:

32Won ma sama tooñ yi ma gisul.

33Kooku, Yàlla dina ko mbugal a?

34Niti xel ñi dinañu wax,

35ne ma: «Ayóoba mii waxewul xam-xam,

36Kon na àtteb Baay Ayóoba mii mat sëkk,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>