Ayóoba 38:1-40 WOLB2025 - Bible AI

1Ba loolu amee Aji Sax ji àddoo fa ngëlén la, ne Ayóoba:

2Ana koo doon, bay lëntal samay dogal,

3Takkul boog te góor-góorlu,

4Ana foo nekkoon ba may lal suuf?

5Ana ku dogal dayo ya; umpu la?

6Ana fu kenuy àddina ya sampe?

7ba biddiiwi njël sarxolleendoo,

8Ana ku tëjoon lafi buntu géej,

9ba ma solal ko aw niir, mbubb,

10dagg aw xélam, àppal ko kemu,

11ba ne ko: «Fii ngay yem, doo fi wees.

12Ana foo masa joxe suba ndigal,

13ngir mu jàppe cati àddina, ag leeram,

14àddina mel ni ban bu ñu teg torluwaay,

15Ñu bon ñi, ñu xañ leen seenug leer,

16Yaa àkki ba fa géej bënne?

17Dees laa won bunti dee?

18Dangaa ràññee yaatuwaayu suuf si?

19Ana yoon wa jëm fa leer dëkke,

20ba nga man leena yóbbu fa ñu digaloo,

21Xam nga ko moos, fekk na la juddu;

22Yaa àkki ba fa mbàndi tawu yuur ya?

23ya may dencal jamonoy njàqare

24Ana yoon wu jëm fa leer di tasaaroo?

25Ana ku xàllal waame,

26di taw fu kenn newul,

27di suuxat gent bu maral,

28Ab taw, ndax am na baay?

29Ana ku wasin galaas,

30ba wali ndox yi dëgër niw doj,

31Yaay faste genn dëllooñ gu ndaw gi ci digg asamaan?

32Yaay def bu jotee, nga feeñal biddiiw yi?

33Dangaa xam dogali yoon yi yor asamaan?

34Yaay yékkatil niir yi kàddug ndigal,

35Yaay yebal melax yi ñu dem,

36Ana ku yeb xel mu rafet cib dënn,

37Ana ku xareñ ba waññ niir yi?

38ba suuf di bàq, dankaloo,

39Yaay rëbbal gaynde?

40ju goore biir paxam,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>