Ayóoba 4:1-20 WOLB2025 - Bible AI

1Elifas waa Teman ba àddu ne:

2Ma jéema àddu boog, soo ma talee!

3Yaw de, ñu bare jàngal nga leen,

4ku jangoon, nga wax, mu taxaw,

5Léegi muy yaw, nga yoqi;

6Xanaa du sag ragal Yàllaay sa cëslaay,

7Seetal rekk, ana jàmburu Yàlla bu masa sànku?

8Li ma gis daal, ku bey ñaawtéef,

9Yàllaay wal noowam, nga sànku,

10Gaynde ŋar, segg xiiru,

11Gaynde ga ñàkkum pàdd, dee,

12Man la kàddu dikkal ci kumpa,

13ci géntu guddi, fa xalaat di jaxasoo,

14Tiitaange ne ma taral, may lox,

15Ngelaw lu sew jaare sama kanam,

16Mu def ku taxaw, te xàmmeewuma ko,

17Mu ne: «Ndax nit man naa am dëgg fa kanam Yàlla?

18Ndegam surgaam ya ca asamaan sax wóoluwu leen,

19gën ñi dëkke këri ban,

20Diggante subaak ngoon, ñu moxoñoo,

© 2025 Bible Society of Senegal
>