Ayóoba 41:1-25 WOLB2025 - Bible AI

1Wii rab, yaakaar koo jàpp nax sa bopp la;

2Kenn ñàngul, ba sañ koo merloo.

3Ana ku ma abal lenn ba ma war koo delloo?

4Rab wii, duma noppee waxtaaney céram

5Ana ku mana summib turkeem?

6Ana ku koy ŋaal,

7Gannaaw gi ay sàppey pakk la,

8dugglante benn-benn,

9xanaa ñu ne ñàpp, ku ne taq sa moroom,

10Bu tislee, melax ne ràyy,

11Jumi sawaraay tàkke ca gémmiñ ga,

12saxaar di sël-sëlee ca wakkan ya,

13Ngelawal bakkanam jafal nay xal,

14Ndoddam la doole daloo,

15Ay ndombo la der ba def, dankalikoo,

16Dënn baa nga dëgër niw doj,

17Bu jógee, jàmbaar ñi tiit,

18Nga jam ko saamar, du dugg;

19Weñ gu ñuul di ko safum mboob,

20Ndawal fitt dawloowu ko,

21Bolde di ko saf ñax gu wow,

22Lu mel ni tojitu xandeer a lal biir ba,

23Mooy baxloo xóote yi ni cin,

24Gannaawam ay def xàll wuy lerxat,

25Amul niruwaale fi kaw suuf,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>