Ayóoba 5:1-26 WOLB2025 - Bible AI

1Rikk wooteel, ndegam am na ku lay wallu!

2Am sanax déy, naqari deret a koy rey,

3Maa gis am sanax, mu saxi reen,

4Ay doomam ay sore yoonu mucc,

5Am ngóobam, ku xiif a koy lekk,

6Aw ay du garab, bay fëlle biir suuf,

7Ku juddu, coono nga juddul,

8Man de su ma doon yaw damay sàkku Yàlla,

9Keey def jëf ju màgg ju nattuwul,

10Keey taw, suuxat suuf,

11Keey kaweel ku suufe,

12Keey neenal pexem ku muus,

13Keey jàpp boroom xel cig muusam,

14Ñu ni mel, bëccëg ñu dajeek lëndëm,

15Yàllaay musal néew-ji-doole ci saamaru làmmiñ

16néew-ji-doole jagoo yaakaar,

17Ma ne, ndokkalee ku Yàlla jubbanti,

18Moom kat mooy mitital, di fajtal;

19Juróom benni njàqare teew, mu xettali la ca,

20Ab xiif, moo la cay jote ba doo dee,

21aayteefu làmmiñ, nga fegu ca,

22Yàquleek xiif, nga kekku;

23Doji àll bi sax, kóllëreg|lemma="kóllëre g-:"* jàmm ngay séq ak ñoom,

24nga xam ne sa xayma, jàmm,

25Dangay ràññee ni saw askan di yaatoo,

26Ni pepp di ñore, ñu door koo góob,

© 2025 Bible Society of Senegal
>