Baamtug yoon wi 33:1-28 WOLB2025 - Bible AI

1Ñaan gii nag la Musaa, góoru Yàlla ga ñaanaloon bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"*, bala moo nelaw.

2Da ne:

3Yaw kay yaa sopp xeet yi,

4Aw yoon la nu Musaa dénk,

5Yesurun+ 33.5 Yesurun: tur wii ak Yanqóoba itam dees na ko woowe Israayil.* am na buur,

6«Yal na Ruben dund, baña raaf,

7Lii nag moo ñeel Yuda. Mu ne:

8Lewi la wax ne ko:

9Kee ne ndey ak baay:

10Leween|lemma="Leween b-:"* ñeey xamal askanu Yanqóoba say àtte,

11Éy Aji Sax ji barkeelal dooley gii giir,

12Beñamin la wax, ne ko:

13Yuusufa la wax, ne ko:

14ak xéewali meññeef mu jant ñoral,

15Na barke bawoo fa kawtey tundi cosaan yu mag ya,

16ak xéewali suuf ak la ko fees,

17Taawub yëkk la, daraja mooy boroom,

18Sabulon la wax ne ko:

19Xeet yi la ñooñu di woo ca tund wa,

20Gàdd la wax ne ko:

21Moo xool cér ba njëkka lew, jagoo ko,

22Dan la wax ne ko:

23Neftali la wax ne ko:

24Aser la wax ne ko:

25Weñ ak xànjar la say xomb di doon,

26«Kenn du Yàllay Yesurun!

27Yàlla ji sax fàww moo dib rawtu,

28Israayil a ngi dëkke xel mu dal,

icle>