Esayi 1:1-30 WOLB2025 - Bible AI

1Lii moo di peeñum Esayi doomu Amocc, di lu mu gis ci mbirum Yuda ak Yerusalem ci janti buuri Yuda yi ñuy wax Osiyas+ 1.1 Osiyas mooy Asaryaa ba tey.* ak Yotam ak Axas ak Esekiyas.

2Asamaan, déglul; suuf, teewlul,

3Aw yëkk xam na boroomam,

4Wóoy wii xeetu moykat,

5Xanaa dungeen wéye fippu,

6Bopp ba téstën, fenn jagul.

7Seenum réew gental,

8Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, dëkk bu taaru baa ngi wéet

9Bu nu Aji Sax ju gàngoor yi

10Dégluleen kàddug Aji Sax ji, yeen njiiti Sodom|lemma="Sodom ak Gomor:"*,

11«Lu may doye seen sarax yu bare?» la Aji Sax ji wax.

12Bu ngeen dikkee, teewsi fi sama kanam,

13Buleen fi indeeti saraxi caaxaan,

14Seeni Terutel weer ak seen bési màggal

15Bu ngeen ma tàllaleey yoxo,

16Raxasuleen ba set wecc,

17Jàngleen di def lu baax,

18«Kaayleen, nu waxtaan ba juboo,» la Aji Sax ji wax.

19Su ngeen ma nangoo déggal,

20Waaye su ngeen lànkee, fippu,

21Ana nu biib dëkk yàqoo, mbeteb gànc,

22Sa xaalis doon na raxit,

23Seeni njiit të,

24Moo tax, kàddug Boroom bee,

25Yerusalem, maa lay teg loxo,

26Maay waññi say àttekat, ñu mel na woon,

27Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* dëppook yoon, mucc,

28moykat ak bàkkaarkat yàqoondoo,

29Yeenay rus moos ci garab yu mag,

30Yeenay meli ni garab gu mag gu xob ya lax,

© 2025 Bible Society of Senegal