1Yéene bii ñeel na Babilon+ 13.1 Babilon tollu na ay jant yu mu mujj di puukarey xeet yi, ngir dooleem, te moo mujj yóbbu Yuda ngàllo.*,
2Yéegeleen ab raaya kaw tund wu ne duŋŋ,
3Maa jox ndigal ñi ma beral sama bopp,
4Coowal mbooloo ngoog ca tund ya,
5Mooy bawoo fu sore,
6Yuuxuleen! Bésub Aji Sax|lemma="bésub Aji Sax j-:"* ji moo dëgmal,
7Moo tax loxoo loxo yoqi,
8ñu tiit a tiit,
9Bésub Aji Sax jaa ngii di ñëw,
10Biddiiw mbaa dëllooñ dootul leeral;
11Maay delloo àddina mbonam,
12Maay def nit gëna jafee gis wurus,
13Moo tax maay gësëm asamaan,
14Ku nekk ay fekkiy bokkam,
15Ku ñu ci gis, jam la,
16seeni doom, ñu moxoñe fi seen kanam,
17Maa ngii di xabtal fi seen kaw waa Medd,
18Seeni fitt lañuy rajaxee xalelu góor,
19Babilon nag, mooy gànjaru réew yi ko wër,
20Deesatu fa dëkk,
21Ay rabi àll a fay goore,