Esayi 14:1-31 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji kay mooy yërëm askanu Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, dellu tànn xeetu Israayil woowu. Moo leen di sancaatal fa seen suuf, doxandéem yi fekki leen; boole seen bopp ci askanu Yanqóoba.

2Yeneen xeet yeey delloo bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"* ba seen réew, mooma Aji Sax ji séddoo, bànni Israayil jàpp ca ñoom njaam, góor ak jigéen, ba teg loxo ña leen tegoon loxo, moom ña leen moomoon.

3Bés bu leen Aji Sax ji teggilee seeni coonook seeni fitna, ba ngeen tàggook njaam gu metti gi ñu leen tegoon,

4su boobaa nangeen woyal buuru Babilon léeb wii, ne ko:

5Aji Sax jee damm bant,

6wi ñu daan xadaruy dóor askan yi,

7Àddina yépp a féex, am jàmm,

8Garab yi dul ruus, ak seedari Libaŋ sax

9Njaniiw ga fa suuf-a-suuf yàkkamti na la,

10ñoom ñépp àddu, ne la:

11Sa puukare gee tàbbisi nii njaniiw,

12Moo yaw biddiiwu njël bi noon ràññ,

13Xanaa du yaa doon wax ci sam xel, naa:

14Maay yéeg fa kaw niir ya,

15Teewul nga tàbbi njaniiw,

16Ku la gis ne la jàkk,

17def àddina wërngal këpp ndànd-foyfoy,

18Buuri àddina yépp, ba ñu daj,

19Yaw, ñu xañ la bàmmeel, sànni la,

20Deesu la robaaleek yooyu buur,

21Waajalleen fi ñuy rendi doom yi,

22«Maa leen di jógal.»

23Mu ne: «Maa koy def kërug suññeel,

24Aji Sax ji Boroom gàngoor yee giñ ne:

25Maay joggati Asiri fi samam réew,

26Mii mébét lañu mébétal àddina sépp,

27Bu Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi dogalee déy,

28At ma Buur Axas saayee,

29Filistee, yet wi daloon ci seen gannaaw damm na,

30Su boobaa ñi gëna walaakaana am lu ñu for,

31Yeen magi pénc mi, ñaawluleen!

© 2025 Bible Society of Senegal
>