Esayi 17:1-13 WOLB2025 - Bible AI

1Yéene bii ñeel na Damaas+ 17.1 Damaas mooy péeyub Siri.*:

2dëkki Arower gental,

3Tata dina tukkee diiwaanu Efrayim,

4«Bésub keroog sagub Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* sàggiku,

5Day mel nim ngóob

6fa dara dul des lu moy am poraat;

7Bésub keroog nit geestu Ki ko sàkk,

8Dootul soxlaati lenn ci sarxalukaay|lemma="sarxalukaay b-:"*

9Bésub keroog seen dëkk yi tata wër,

10Yeena fàtte Yàlla ji leen di musal,

11Bés ba ngeen ko jëmbatee, ngeen gis mu sax,

12Ndeysaan, mii riirum gàngoor yu mag!

13Xeet yaa ngi ŋarandoo

© 2025 Bible Society of Senegal
>