1Wóoy ngalla réew ma gunóor yay riire,
2Yeen ñiy yónni biir géej, ay ndaw,
3Yeen waa àddina wërngal këpp,
4Aji Sax ji kat da maa wax ne:
5Bala ngóob di jot, te fekk lépp tóor,
6ñu boole waccal njanaawi tund ya
1Wóoy ngalla réew ma gunóor yay riire,
2Yeen ñiy yónni biir géej, ay ndaw,
3Yeen waa àddina wërngal këpp,
4Aji Sax ji kat da maa wax ne:
5Bala ngóob di jot, te fekk lépp tóor,
6ñu boole waccal njanaawi tund ya