Esayi 22:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1Yéene bii ñeel na xuru Peeñu ma+ 22.1 xuru Peeñu ma mooy xur wi Yàlla doon feeñoo.*:

2Lu waral coow li ak xaxaloo bi,

3Seen njiiti xare yépp a bokk daw,

4Moo ma tax ne: «Buleen ma xool,

5Lii kat bésub njommite laak coonook toroxte,

6Waa Elam gàllooy fitt,

7Seen xur yu nangu yaa fees aki watiir,

8te Yuda ne duŋŋ, dara wëru ko.

9far gis ni ñu bëtt-bëttee tatay Yerusalem

10boole ca waññ këri Yerusalem,

11Da leen di fekk sàkk mbànd diggante ñaari tata yi,

12Bésub keroog, Boroom bi, Aji Sax ji ci gàngoor yi

13Te yeena ngii ci mbég ak bànneex,

14Aji Sax ji ci gàngoor yi dégtal na ma lii:

15Boroom bi, Aji Sax ji ci gàngoor yi dafa wax ne: «Ayca, demal ba ca Sebna, bëkk-néegu buur sii, nga ne ko:

16Ana loo fi am, ak koo fi am?

17Jàmbaar, dama ne Aji Sax jee lay xalab;

18fodonk la, rattax,

19Aji Sax ji nee: «Maa lay jële sa liggéey,

20«Bésub keroog ma woo sama jaam bi, Elyakim doomu Ilkiya,

21solal ko sa mbubb, dooleele ko sa laxasaay, teg kilifteefu réew mi ci loxoom, ba mu féete wàllu baay waa Yerusalem ak waa kër Yuda.

22Maa koy ràng caabiy kër Daawuda, muy ubbi te kenn du tëj; di tëj te kenn du ubbi.

23Maa koy samp fu dëgër ni ab wékkukaay, mu doon sagu kër baayam.

24Waa kër baayam ak seen daraja, ñépp ay wékku ci moom, car yaak caraat ya. Ndab yu ndaw yépp ca la, kopp ya ba ca njaq ya.

© 2025 Bible Society of Senegal
>