Esayi 23:1-17 WOLB2025 - Bible AI

1Yéene bii ñeel na dëkk ba ñuy wax Tir+ 23.1 Tir ak Sidon, ay dëkk yu am solo la woon ca Fenisi, ci réew mi ñuy wax Libaŋ tey. Seetal it ci aaya 4 (1.4).*:

2Yeen waa tefes,

3war ndox ya ne xéew,

4Yaw Sidon, gàcce ñeel na la,

5Bu xibaar ba àggee Misra de,

6Jàllal ba Tarsis+ 23.6 Tarsis, ab sanc la bu bokkoon ci Tir, ca wàllu Espaañ.*,

7Xanaa lii du seen dëkk bu xumb ba,

8Ana ku fexeel lii Tir ma daan fale,

9Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko fexe,

10Yeen waa Tarsis, defleen ni dexu Niil, walal seen réew;

11Aji Sax ji tàllal na loxoom, tiimale géej,

12Nee: «Yeen waa Sidon ñi mel ni janq bu ñu siif, tëdde ko,

13Xoolleen li dal réewum Kaldeen ñi.

14Yeen boroom gaali Tarsis, yuuxuleen ni ñu deele,

15Bu keroogee ñu fàtte Tir juróom ñaar fukki at, ni àppu benn buur. Bu juróom ñaar fukki at yi matee, Tir xewle la ñu woyal gànc ba, ne ko:

16«Yaw gànc bi ñu wacc, fabal sa xalam, wër dëkk bi,

17Bu juróom ñaar fukki at yi matee, Aji Sax ji dikkal Tir, ñu delluy liggéey, di feyu, di gànctook mboolem réewi àddina fi kaw suuf.

© 2025 Bible Society of Senegal
>