1Wóoy ngalla Efrayim+ 28.1 Efrayim mooy giir gu am solo ci fukki giir ya ca nguurug bëj-gànnaar ga ñuy wax Israayil. Lée-léeg muy tur wi ñuy woowe waa gox boobu.*,
2Dégluleen, jàmbaar ju am doolee ngi dikkal Boroom bi,
3Dees na joggati kaala
4Te tóor mu lax mi muy gànjaroo,
5Bésub keroog Aji Sax ji Boroom gàngoor yi
6mooy dikkal xelum dëgg kuy toog di àtte,
7Ñii itam ay naan biiñ bay tërëf,
8Seen taabal yépp a ngi taq ripp,
9Ñu naa: «Ana ku Esayi mii di jàngal?
10Ca rëdd wii, ca rëdd wee,
11Xanaa boog nit ñu seen wax leerul,
12Moo leen waxoon ne leen:
13Moo tax kàddug Aji Sax ji di mujj doon ci ñoom lu ñu manula nànd, ni:
14Kon nag yeen kókkalikat yi yilif
15Yeena naay: «Danoo wóllëranteek dee,
16Moo tax Boroom bi Aji Sax ji wax ne:
17Dëgg laay def nattukaay,
18seen wóllëranteek dee neen,
19Saa yu dikkee ne leen céex,
20Lal a gàtt ba deesu ci tàlli,
21Aji Sax jeey jóg na woon
22Tee ngeena baña kókkalee
23Teeyluleen te déglu sama kàddu,
24ndax beykat bi day dëkke gàbb,
25Bu gàbbee ba toolam maase,
26Dees koo xamal yoon wa,
27Mbàccum nisel watiir amu ca yoon,
28Gubi bele, dees na ca jaare watiir,