Esayi 29:1-23 WOLB2025 - Bible AI

1Wóoy ngalla Aryelee, Aryel+ 29.1 Aryel, tur la wu ñuy woowe Yerusalem. Man naa tekki itam taalub sarxalukaay ba woon ca kër Yàlla ga.*,

2Du tee ma wàcceel Aryel musiba,

3Maay dal ab dal, wër la,

4Dinga suufe ba mel ni kuy àddoo biir suuf,

5Say noon ay def gàngoor ni feppi suuf,

6Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi moo lay dikke

7Mboolem xeet yu bare yiy xareek Aryel,

8Su boobaa mu mel ni ku xiif,

9Tendeefal, jommi rekk!

10Aji Sax ji déy yeen la wal

11Peeñum xew-xew yii yépp ump na leen,

12nga jox ko ku jàngul, ne ko mu jàng,

13Boroom bi nee: «Askan wii, làmmiñ lañu ma jegee,

14Moo tax maa ngii di dellu wéyeek askan wii,

15Wóoy ngalla ñiy làqu Aji Sax ji,

16Yeenaka juunum xel!

17Xamuleen ne fi leek lu néewa néew,

18Su bés baa ab tëx dégg kàdduy téere,

19néew-doole yi dellu bége Aji Sax ji,

20Ku néeg déy dina neen,

21Mooy ñiy tuumaal nit,

22Moo tax Aji Sax ji jotoon Ibraayma,

23Bu am meññeefam gisee

© 2025 Bible Society of Senegal
>