1«Wóoy ngalla doom yii diy fippukat!»
2Ñoo dox wuti Misra te laajuñu ma,
3Rawtub Firawnaay mujj di seen gàcce,
4Seeni jawriñ a nga xaat ba Cowan,
5waaye ñoom ñépp kersa lañuy ame Misra
6Yéeneb waxyu|lemma="waxyu:"* bii ñeel na malay àllub Negew:
7Ndimbalu Misra, cóolóolu neen!
8Aji Sax ji nee:
9Wii xeet kat ay fippukat lañu,
10Boroom gis, ñu ne ko: «Bul gis,»
11Moyal yoon wi;
12Moo tax Aji Sell ju Israayil wax ne:
13googu ñaawtéef ay mujj doon
14Da naan tasar ni njaqal xandeer
15Ndax Boroom bi Aji Sax ji,
16Yeena ne: “Déedéet, danuy war fas, daw!”
17Junneey daw fu leen kenn gëdde,
18Aji Sax ji déy a leen namma baaxe,
19Yeen waa Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, yeen waa Yerusalem,
20Boroom bee leen di leel njàqare,
21di dégg kàddu guy jibe seen gannaaw,
22Su boobaa ngeen sobeel seen jëmmi tuur yi ñu xoob xaalis;
23Su boobaa Aji Sax ji tawal lu ngeen ji,
24Nag yeek mbaam yiy rijji sax,
25Te tundoo tund wu kawe,
26Weer day leer ni jant,
27Turu Aji Sax jaa ngii, jóge fu sore;
28noo ga di wal mu baawaan,
29Teewul, bokk yi, seen woy yay jib;
30Aji Sax jeey yékkati kàddoom gu màgg,
31Kàddug Aji Sax jeey jib,
32te saa yu yet wa Aji Sax ji féetale Asiri dalee,