1Wóoy ngalla ña wàcci Misra, di wuti wall,
2Moona moom it xareñ na,
3Waa Misra, niti neen, duñu Yàlla;
4Aji Sax ji déy da maa wax ne ma:
5Ni picc di daayaarloo, aar am tàggam,
6Éy bokki Israayil, fippu ngeen Aji Sax ji ba sës, waaye walbatikuleen!
7Bésub keroog ku ne sànni yàllantuy xaalisam, ak yàllantuy wurusam yi mu sàkke woon loxoy bàkkaaram.
8«Asiri nag day daanu,