Esayi 32:1-19 WOLB2025 - Bible AI

1Buur a ngii, dëgg lay nguuroo,

2ku ci nekk mel ni seelukaayu ngelaw,

3Su boobaa gëti njàccaar yi dootuñu gëmm,

4ku yàkkamti di ràññee, ba mana xam,

5Booba deesatul woowe ab dof «gor si»,

6Ab dof, waxi dof lay wax,

7Ab njublaŋ, ay pexeem musiba la.

8Waaye gor si, ngor lay mébét,

9Yeen jigéen ñi dal xel,

10Yeen jigéen ñi dal xel,

11Jigéen ñi dal xel, ragalleen;

12Fëggleen seen dënn,

13ak sama suufas bokk ya ay dég aki dagg nangu.

14Kër gu rafet sax, dees koy wacc,

15ba keroog Boroom bi ëf ci nun ag noowam,

16Su boobaa yoon dëkke màndiŋ mi,

17Su boobaa àtteb dëgg ay jur jàmm,

18ba sama bokk yi dëkke sancub jàmm,

19doonte gott bi day daanu ci tawub doji yuur,

© 2025 Bible Society of Senegal
>