1Wóoy ngalla yaw bóomkat bi kenn bóomul,
2Éy Aji Sax ji, ngalla baaxe nu;
3Sam riir jib, xeet yi fëx;
4Dees na sëxëtoo sa alal sëxëtoob soccet.
5Aji Sax jee kawe,
6Liy dalal seen jamono mooy
7Xoolleen seen jàmbaar
8Yoon yaa ngi wéet,
9Suuf a ngi maral, wow koŋŋ,
10Aji Sax ji nee: «Xaaral rekk ma jóg,
11Seeni mébét di am mboob,
12Xeet yeey sànku
13Yeen ñi sore, dégluleen li ma def;
14Bàkkaarkati Siyoŋ tiit nañu,
15Xanaa kiy doxe njub,
16Ku ni mel, béreb bu kawe lay dëkke,
17Yaw mi mel nii, buur bi ci taar bi ngay teg bët;
18Sam xel dem ca sa tiitaange ja woon,
19Su boobaa dootoo gis xeet wii di jaay doole,
20Xoolal Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, dëkk ba nuy màggale;
21Foofa déy la nu Aji Sax ju màgg ji
22Aji Sax jee nuy jiite,
23Yeen nag seen réew mi gaal la,