1Yeen waa dun yi, xeremluleen, déglu ma;
2Ana ku ñu yékkatee penku,
3Moo leen di dàq, ba jàll te jàmm a koy dal,
4Ana ku def lii, dogal ko?
5Waa dun yee ko gis, tiit,
6ku nekk di jàppale moroom ma,
7Tëggu weñ ba di ñaax tëggu gànjar ba,
8Waaye yaw Israayil, sama jaam bi;
9Yaw mi ma jukkee fa cati àddina,
10bul ragal, yaw laa àndal,
11«Ma ne, képp ku la mere,
12Dinga ko seet, doo ko gis,
13Man Aji Sax ji maay sa Yàlla;
14Yaw Yanqóoba mi néew doole niw sax,
15«Maa ngii di la def
16Yaa leen di bàcc, ngelaw wal,
17«Walaakaanaak néew-doolee ngi wër,
18Maay walaley dex kaw coll ya ne duŋŋ,
19Maay def garabi seedar aki séng ca màndiŋ ma,
20ndax nit ñi gis, ba xàmmee,
21«Waxleen seenu lay,» la Aji Sax ji wax,
22«Woneleen ko te wax nu liy ñëw.
23Biralalleen nu mbiri ëllëg,
24Ma ne, yeen daal, dungeen tus;
25«Maa yékkatee nit bëj-gànnaar,
26Ana ku yéene woon lii ca njàlbéen,
27Waaye maa njëkka yégal Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*
28Xool naa xool ci tuur yi, gisuma kenn;