Esayi 42:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji nee: «Xoolleen sama jaam bii ma yor,

2Du xaacu, du biral;

3Barax bu lemu sax, du ko damm,

4Du toqi, du nasax,

5Yàlla Aji Sax ji dafa wax,

6Mu ne: «Man Aji Sax ji, maa la woo

7ngay gisloo gumba,

8«Man, Aji Sax jeey sama tur;

9Mbir ya jiitoo ngoog, mat na;

10Woyleen Aji Sax ji woy wu yees,

11Na waa àll beeki dëkkam xaacoondoo,

12Nañu delloo Aji Sax ji màggaayam,

13Aji Sax jeey waaxu ni jàmbaar,

14Aji Sax ji nee: «Damaa yàgga xeremlu,

15Maay tonni tund wu mag ak wu ndaw,

16Maay doxloo silmaxa yi

17Ñi wóolu ay jëmmi tuur,

18«Yeen tëx yi, dégluleen;

19Ana ku silmaxa ku moy sama jaam bii+ 42.19 sama jaam bii mooy bànni Israayil fii.*?

20Gis nga lu bare,

21Aji Sax ji la soob ci njubteem,

22Waaye ñu ngii di xeet wu ñu futti, sëxëtoo;

23Ana kan ci yeen mooy dékk lii nopp?

24Ana ku jébbal waa kër Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* futtikat yi,

© 2025 Bible Society of Senegal
>