1Léegi nag yaw Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*,
2Booy xuus cim ndox,
3Man Aji Sax ji, maay sa Yàlla;
4Fonk la, teral la ak sopp la,
5Bul tiit, yaw laa àndal,
6Maa naa bëj-gànnaar: “Bàyyi leen!”
7Delloosil képp ku ñu ma tudde,
8Indileen ñii diy silmaxa te ami gët;
9Na xeet yépp daje,
10«Yeen sama ñoñ, yeenay samay seede.»
11Aji Sax ji, mennum man a;
12Maay dogal texe, sottal ko, biral ko,
13maa masa doon kenn ki,
14Aji Sax jiy seen jotkat|lemma="jotkat b-:"*,
15Maay Aji Sax ji, seen Ku sell ki;
16Aji Sax ji dafa wax,
17xabtal watiiri xare aki fas,
18Mu ne: «Buleen geesu la woon,
19Maa ngii di def lu yees,
20ndundati àll bi di ma sàbbaal,
21xeet wii ma bindal sama bopp,
22«Moona Yanqóoba, woowuloo ma,
23Du xar mu ndaw moo ma defal saraxu rendi-dóomal|lemma="Sarax yi:"*,
24Du xaalis boo ma jëndale barax bu xeeñ,
25Mennum man mii maay far say moy ngir man,
26Fàttali ma saw lay, nu bokk layoo;
27Sa maam a njëkka bàkkaar,