Esayi 44:1-27 WOLB2025 - Bible AI

1«Yaw Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, sama jaam bi, déglul boog,

2Aji Sax ji dafa wax, moom mi la sàkk,

3Maay sottim ndox suuf su mar,

4ñu màgg ni garabu saab-saab,

5Kii nee: “Aji Sax jee ma moom.”

6Aji Sax ji dafa wax,

7Ana ku mel ni man? Na àddu!

8Buleen tiit, buleen ragal.

9Képp kuy tabax jëmmi tuur, doo tus,

10Sàkk sam tuur,

11Képp ku ca bokk

12Ab tëgg jël jumtukaayam,

13Liggéeykatu bant tàllal buumu nattukaay,

14ba tax mu gor garabi seedar,

15nit xambe, sàkk ci, jaaroo;

16xaaju matt ma lay taal,

17Ndesu matt ma lay sàkke jëmmu tuuram,

18Ñii xamuñu, xàmmeewuñu,

19Ku mel nii du delloosim xelam,

20Kee di jur gu dunde dóomu-taal,

21Aji Sax ji nee: «Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, baal xel ci lii!

22Maa far say moy, mu naaxsaay niw niir,

23Asamaan, sarxolleel, Aji Sax ji dikk na!

24Aji Sax ji sa jotkat|lemma="jotkat b-:"* dafa wax,

25Maay neenal firndey maaman,

26Maay dëggal sama kàddug jaam,

27Maa naa xóotey mbeex mi: “Wowal,

© 2025 Bible Society of Senegal
>