1Aji Sax ji dafa wax ki mu fal,
2mu ne: «Man maa lay jiitu,
3Maa lay jagleel denc yu ruqe,
4Te Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* sama jaam bi,
5Aji Sax ji man a, du keneen;
6ngir xamees penku ba sowu,
7Maay bind leer,
8Na asamaan wis-wisal,
9Wóoy ngalla kuy diiŋat ka la tabax
10Wóoy ngalla ku naan baayu nit,
11Aji Sax ji, Aji Sell|lemma="Aji Sell j-:"* ju Israayil dafa wax,
12Man maa amal suuf,
13Man maay yékkati Buur Sirus ci àtteb dëgg,
14Aji Sax ji dafa wax ne:
15Yaw déy, yaa di Yàlla ju làqu,
16Yattkati xërëm yaa ngoogu, rus,
17Israayil, yaay mucc fa Aji Sax ji
18Aji Sax ji kat dafa wax,
19Làquwuma, di waxe béreb bu lëndëm.
20Yeen daw-làquy xeet yi,
21Àdduleen, layoosi,
22Yeen waa àddina, catoo cat,
23Giñ naa ko ci man mii,
24Dees na ma waxal ne: