Esayi 47:1-14 WOLB2025 - Bible AI

1Yaw janq Babilon,

2Fabal wolukaay, wol sunguf.

3Na sa yaram feeñ,

4Sunu jotkat|lemma="jotkat b-:"* ay Aji Sax ji Boroom gàngoor yi,

5Yaw dëkkub Kaldeen bi ci taar bi,

6Maa mere woon sama ñoñ,

7te naa: «Ba fàww maay lingeer!»

8Diryànke bee, déglul lii:

9Te ñaar yooyoo lay dikkal ci benn bés.

10Dangaa yaakaaroon sa pexe yu bon,

11Musibaa lay dikkal,

12Jàppool say jat rekk

13Yaaka sonn ci tegtali maa-man!

14Ñu ngoog bokk demin ak boob bu sawara jafal,

© 2025 Bible Society of Senegal
>