1Yeen waa kër Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, dégluleen;
2moona yeena ngi sagoo turu dëkk bu sell|lemma="sell:"* bi,
3«Yàgg na maa biral lay njëkka am.
4Xam naa ne ñu dëgër bopp ngeen.
5Moo tax ma yàgg leena biralal lii,
6Lii lépp déggoon ngeen ko;
7Léegi lees ko amal,
8Dégguleen, yéguleen,
9Waaye sama tur tax na ma aj sama mer,
10Ma ne, togg naa leen, xelli cib taal,
11Samaw tur a tax,
12«Dégluleen ma, yeen askanu Yanqóoba,
13te sama loxo bee dëj suuf,
14Bokkleen daje yeen ñépp te déglu!
15Maa àddu, man mii;
16Jegesileen ma, déglu ma;
17Aji Sax ji seen jotkat|lemma="jotkat b-:"* dafa wax,
18Céy su ngeen sàmmoon samay santaane,
19seen geño sakkan ni suuf,
20«Génnleen Babilon,
21Marewuñu béreb yu wow ya mu leen jaarale woon,