Esayi 49:1-25 WOLB2025 - Bible AI

1Yeen waa duni géej, dégluleen ma;

2Moo ñawal sama kàddu ni saamar,

3Moo ma ne: «Israayil yaa di samab jaam,

4Man nag ma noon:

5Tey nag Aji Sax jee wax,

6Mu ne: «Xeeb naa li ma la sas ngay sama jaam

7Aji Sax ji jotkatub|lemma="jotkat b-:"* Israayil,

8Aji Sax ji dafa wax ne:

9ba ne ñi ñu tëjoon: “Génnleen!”

10Duñu xiif, duñu mar;

11Sama tund yépp laay soppiy yoon,

12Ñu ngii bawoo fu sore,

13Asamaanoo sarxolleel, suufoo bégal,

14Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* a nga naa: «Aji Sax ji wacc na nu,

15Aji Sax ji nee: «Ana jaboot juy fàtte doomam juy nàmp,

16Sama biir loxo yii laa la ñaas,

17Ñi lay tabaxaat dañuy gaaw,

18Séentul fi la wër te xool!

19Sa gentub tey bi déy a ngi wéet,

20Ñàkkoon ngay doom,

21Dangay mujj naa:

22Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

23Yaw la ay buur di baayoo,

24Manees naa foqati alalu sëxëtoo ci loxol jàmbaar a?

25Aji Sax ji déy dafa wax ne:

© 2025 Bible Society of Senegal
>