1Naa woy sama soppe
2Mu gàbb ko, dindi doj ya,
3Léegi yeen waa Yerusalem
4Lu may defalati sama tóokër bi,
5Ma xamal leen nag
6Dama koy gental,
7Tóokëru Aji Sax ji Boroom gàngoor yi kat,
8Wóoy ngalla ñii di dajale kër ak kër,
9Maa dégg Aji Sax ji Boroom gàngoor yi,
10Tóokërub ñetti egtaar déy
11Wóoy ngalla ñiy teela xëy,
12Xalam yaak tabala yaak toxoro ya jolli,
13Moo tax ñuy gàddaayloo ñoñi Aji Sax ji
14Moo tax njaniiw di yàkkali ag bóli,
15Doom aadama torox na,
16Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, ab àtteem lay fésale màggaayam,
17Am xar a nara fore biir dëkk bi, mbetem parlu,
18Wóoy ngalla ñiy ràngooy buum,
19Ña nga naa: «Na Aji Sax ji gaaw!
20Wóoy ngalla ñiy gis lu bon, ne lu baax la;
21Wóoy ngalla ñii defe ne ñoo xam,
22Wóoy ngalla ñiy jàmbaari naan biiñ,
23di dëggal ku sikk ndax ab ger,
24Moo tax ni boob di jeexe ci sawara,
25Moo tax merum Aji Sax ji tàkkal ñoñam,
26Aji Sax jeey yékkatil raaya xeet wu sore,
27Kenn sonnu ci, kenn tërëfu ci,
28Seeni fitt ñaw na,
29Dañuy ŋar ni gaynde,