1Aji Sax ji dafa wax ne:
2Ana lu tax ba ma dikkee, kenn nekku fa?
3Du maay sànge asamaan ag lëndëm,
4Boroom bi Aji Sax ji moo ma may
5Boroom bi Aji Sax jee ma bënnali nopp,
6Sama gannaaw laa jox ku may dóor,
7Waaye Boroom bi Aji Sax jee may dimbali,
8Ki may dëggal jege na.
9Ma ne, Boroom bi Aji Sax jee may dimbali.
10Ana ku ragal Aji Sax ji ci yeen,