1Dégluleen maa, yeen ñiy wuta doxee yoon,
2seen maam Ibraayma laa ne, moom ngeen di xool,
3Aji Sax jeey dëfal Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* moos,
4Yeen sama ñoñ, teewluleen ma,
5Sama wall jege na,
6Séentuleen asamaan
7Yeen ñi xam liy yoon, dégluleen ma,
8Sax a leen di lekk ni mbubb,
9Aji Sax ji, yewwul, ngalla yewwul;
10Xanaa du yaa wowal géej
11Ñi Aji Sax ji goreel, nii lañuy dellusee,
12Man ci sama bopp maa leen di dëfal.
13Dangeena fàtte Aji Sax ji leen sàkk,
14Ku diisoon ba waaf léegi nga féex;
15Man maay seen Yàlla Aji Sax ji,
16Maa la sexal samay kàddu,
17Yewwulee, yewwul, Yerusalemee jógal,
18Amul ci ñi nga jur, kenn koo dese
19Yii yaar de dikkal na la:
20Sa doom yi ne lasar,
21Rikk déglul nag lii, yaw mi musiba dal,
22Sa boroom Aji Sax ji,