1Ma ne, Aji Sax ji gàttul loxo ba tëlee walloo,
2Seeni ñaawtéef a dox seen digganteek
3Seeni loxoo taq deret,
4Du dëgg gu kenn wut cib àtte,
5Nenu ñàngóor lañuy tostan,
6Seeni lënd du ràbbe ba solal nit,
7seeni tànk daw wuti lu bon,
8Yoonu jàmm, xamuñu ko,
9Lee tax yoon sore nu,
10Nu ngi làmbatu ci biir tabax ni silmaxa,
11Nun ñépp a ngi xiiru ni rab wu aay,
12Sunuy tooñ a bare fi sa kanam,
13Noo tooñ Aji Sax ji, wor ko,
14ba yoon dellu gannaaw,
15Dëgg a tumurànke,
16Daa xool, gisul kenn;
17Moo sol kiiraayal njub,
18Mooy delloo ku ne yool ba mu yelloo,
19Dees na ragale turu Aji Sax ji fa sowu,
20«Ab jotkat|lemma="jotkat b-:"* ay dikkal Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*,