Esayi 61:1-10 WOLB2025 - Bible AI

1Noowug Boroom bi Aji Sax jaa ngi fi sama kaw,

2Moo ma yónni ngir ma yéene atum yiwu Aji Sax ji,

3ngir indil waa Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* ñiy ñaawlu

4Ñooy tabaxaat gent ya woon,

5Ay gan ay dikk,

6Yeen nag lees di woowe:

7Sama ñoñ ay weccikoo seen gàcce

8Man Aji Sax ji, damaa sopp yoon,

9Dees na xàmmee seen askan fi biir xeet yi,

10Maa bég a bég ci Aji Sax ji,

© 2025 Bible Society of Senegal
>