1Ana kuy kii bawoo Edom+ 63.1 Edom mi doon seexu Yanqóoba, moom lañu dippee réewum Edom, te moo taxawe taxawaayu noonub Aji Sax ji.*,
2Lu waral sa xonqaayu mbubb mi,
3«Maa doon dëre tànk, man kenn
4Bésub feyul samay ñoñ laa mébétoon,
5Ma xool,
6Sama mer laa dëggaatee ay xeet,
7Jëfi ngorug Aji Sax ji laay fàttalee
8Moo noon: «Ñoom déy ñooy sama ñoñ!
9Seen gépp njàqare di njàqarey boppam,
10Waaye ñoom ñoo fippu,
11Ñoñam ña daldi fàttaliku janti Musaa ya woon.
12Ana ki dawaloon dooley përëgam bu tedd ba,
13Ana ku leen doxloo woon biir xóote ya,
14Ni jur gu wàccew xur, di fa fore,
15Yaw Yàlla, ngalla séentool asamaan,
16Yaw déy yaa di sunu baay.
17Aji Sax ji, loo nuy wërloo fu sore say yoon,
18Nun sa xeet wu sell|lemma="sell:"* wii,