Esayi 65:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1«Maa may ay nit tont te laajuñu ma.

2Samay loxo laa yendoo tàllal askanu fippukat,

3Ñoo di xeet wu ma ne jàkk,

4di tooge diggi bàmmeel,

5te ñu naan: “Dellul gannaaw,

6«Ma ne dogal a ngii binde, fi sama kanam:

7Aji Sax ji nee: «Muy seeni ñaawtéef,

8Aji Sax ji dafa wax ne:

9Fi Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* laay soqee aw askan,

10Joorug Saron ay dellu di parlub gàtt gi,

11«Waaye yeen ñi wacc Aji Sax ji,

12maa leen di dogalal saamar,

13Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

14Sama jaam ñeey sarxolleji

15Seen tur wi ngeen bàyyi gannaaw

16ba képp ku namma barkeel fi kaw suuf,

17«Maa ngii di sàkksi asamaan su yees

18Bégleen kay,

19Maay bége Yerusalem,

20Deesu fi gisati

21«Ñooy tabax ay kër, dëkke,

22Duñu tabax moos, keneen dëkke;

23Duñu liggéeyati mukk ci neen

24Su boobaa balaa ñoo woote,

© 2025 Bible Society of Senegal
>