1Aji Sax ji dafa wax ne: «Asamaan sama ngàngunee,
2Mboolem yooyu, sama loxoo ko sàkk;
3Kee moom mu ngi rendiw yëkk, sarxal,
4Man it maa leen di tànnal seeni mbugal,
5Dégluleen kàddug Aji Sax ji,
6Coowal xaree ngoog bawoo dëkk ba,
7«Kii balaa matu, wasin na,
8Ku masa dégg lu mel nii?
9Aji Sax ji nee: «Man miy jàppale jigéen
10«Yeen soppey Yerusalem yépp,
11Su ko defee ngeen nàmp ba suur
12Aji Sax ji déy dafa wax ne:
13Man maa leen di naxtaan ba ngeen dal,
14Yeenay teewe lii, seen xol tooy,
15Aji Sax ji déy a ngii dikke sawara,
16Sawara déy la Aji Sax ji di mbugale,
17«Ñii di sellalu aka sangu-set
18«Man maa xam seeni jëf ak seeni xalaat.
19Maay teg firnde fi seen digg,
20Xeet yooyooy indi seen bokk
21Te ñenn ci yooyu xeet, maa leen di jël,
22«Asamaan su yees sii
23«Su ko defee Terutel weer ba Terutel weer,
24«Te bu ñu génnee, gis néewi