Esayi 7:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1Janti buurub Yuda, Axas doomu Yotam miy doomu Osiyas, Reccin buurub Siri moo dal ci kaw Yerusalem, ànd ak buurub Israayil, Peka doomu Remalya. Waaye manalu leen dara.

2Ba ñu yégalee Buur Axas sëtub Daawuda ak waa këram, ne ko waa Siri, Efrayim+ 7.2 Efrayim moo gëna yaatu ci fukki giir ya féete woon réewum Israayil ga ca bëj-gànnaar, te moo taxawe taxawaayu Israayil.* lañu lëngool, mbir ma yëngal na Buur Axas ak waa réew ma, ba mel ni garabi gott bu ngelaw li gësëm.

3Aji Sax ji wax Esayi ne ko: «Génnal, dajeek Axas, yaak sa doom Seyar Yasub, ma nga ca catal solomu mbànd ma féete kaw, ca yoonu toolu fóotkat ya.

4Nga wax ko ne ko:

5Waa Siri ñoo ànd ak Efrayim ak doomu Remalya,

6‘Nan songi Yuda,

7Waaye Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

8Damaas a yilif Siri,

9Samaree yilif Efrayim,

10Aji Sax ji teg ca ne Axas:

11«Ñaanal sa Yàlla Aji Sax ji firnde. Ñaan ko ko, ak fu mu mana bawoo, fa suuf-a-suuf, mbaa fa kaw-a-kaw.»

12Axas ne: «Duma ko ñaan, ndax duma nattu Aji Sax ji.»

13Esayi nag ne:

14Kon nag Boroom bi ci boppam moo leen di jox firnde:

15Soow ak lem lay lekk,

16Bala xale bee ràññee lu baax ak lu bon,

17Aji Sax jee lay dikke,

18Bésub keroog Aji Sax ji ootal weñ

19ñu dikk, bokk tàggesi mbartali xunt yi,

20Bésub keroog saatu la Boroom biy wate,

21Bésub keroog nit du fa dundle

22meew ne gàññ, ndax nit ñu néew,

23Fu junniy reseñ taxaw tey,

24Xala aku fitt lees fay deme,

© 2025 Bible Society of Senegal