Esayi 9:1-19 WOLB2025 - Bible AI

1Askan wiy doxe lëndëm nii,

2Aji Sax ji, yaay yokk xeet wi,

3Yaa leen di sippil seen sëf,

4Mboolem dàll wu ab noon dukkate ba dikk,

5Nde gonee juddu, ñeel nu,

6Dooley kilifteefam ak jàmm ja du am kemu,

7Boroom bee yónnee kàddu

8xeet wépp jot ca,

9«Ay móol màbb,

10Aji Sax ji yékkati nooni Buur Reccin, fi seen kaw,

11Siri songe penku; Filisteen ña, sowu,

12Waaye xeet wi delluwuñu ca ka leen duma,

13Moo tax Aji Sax ji doge Israayil bopp ak geen,

14Mag meek kàngam li ñooy bopp bi,

15Ñi jiite askan wii ñoo leen di sànk,

16Moo tax Boroom bi du bége seeni xale yu góor,

17Mbon a ngi tàkk moos

18Merum Aji Sax ji Boroom gàngoor yi taal na réew mi,

19Nit ñaa ngi màtte ndijoor, te doyaluñu,

© 2025 Bible Society of Senegal