Esekiyel 13:1-22 WOLB2025 - Bible AI

1Ba loolu amee kàddug Aji Sax ji dikkal ma ne ma:

2«Yaw nit ki, jottalil kàdduy waxyu|lemma="waxyu:"* jëme ci kaw yonenti Israayil yiy biral ay kàdduy waxyu. Nanga wax ñiy biral kàdduy waxyu ci seen xelum bopp, ne leen:

3Wóoy ngalla yonent yu ñàkk xel

4Yeen yonenti Israayiloo,

5Yéeguleen ca biir bëttukaayi tata ja,

6Seeni peeñu caaxaan la,

7Xanaa du peeñuy caaxaan ngeen gis?

8«“Kon nag Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

9Sama loxooy dal yonent

10Kon nag gannaaw ñu ngi lajjal sama ñoñ,

11waxal raaxkati weexal yi, ne leen:

12Bu tata ji jekkee ne jànjaŋ,

13Kon Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

14Maay màbb tata ji ngeen raax weexal,

15Maay xëpp sama xadar ci kaw tata ji

16Mooy yonenti Israayil yi biral Yerusalem kàdduy waxyu,

17«Yaw nit ki,

18Neel: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

19Bu ngeen di fen sama ñoñ ñiy dégluy fen,

20Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne:

21Maay foqati seeni muuraay,

22Gannaaw yeena fen ba jeexal xolu aji jub,

© 2025 Bible Society of Senegal
div>